速報APP / 圖書與參考資源 / Kàddug Yàlla gi

Kàddug Yàlla gi

價格:免費

更新日期:2018-09-28

檔案大小:6.4M

目前版本:2.0.1

版本需求:Android 2.3 以上版本

官方網站:mailto:equipedevmbs@gmail.com

Email:http://sng.al/priv

Kàddug Yàlla gi(圖1)-速報App

Appli bii mooy Kàddug Yàlla, gi dikke ñaari pàcc: Kóllëre gu jëkk gi Yàlla fas ak nit, ak Kóllëre gu yees, gi mujja wàcc, te ñenn ñi di ko wooye Injiil, mu tekki Xibaaru jàmm. Ñaari téere yooyu, Yàllaa leen wàcce ci nitam ñu sell ñi, kóllëre gu jëkk gi, ñu bind ko ci yawut, gu yees gi, ci làkku gereg. Li ñu bind ci téere yu jëkk ya nag, moom lanu tekki ci wolof.

[bible, wolof, kaddug yalla gi]

Kàddug Yàlla gi(圖2)-速報App

Kàddug Yàlla gi(圖3)-速報App

Kàddug Yàlla gi(圖4)-速報App

Kàddug Yàlla gi(圖5)-速報App

Kàddug Yàlla gi(圖6)-速報App

Kàddug Yàlla gi(圖7)-速報App

Kàddug Yàlla gi(圖8)-速報App